1
Mucc ga 25:8-9
Kàddug Yàlla
KY
Na ma bànni Israayil defaral béreb bu sell, ndax ma dëkk ci seen biir. Na lépp dëppoo ak li ma lay won. Muy misaalu xaymab jaamookaay bi, di misaalu mboolem ay jumtukaayam, lépp defeleen ko noonu.
Compare
Explore Mucc ga 25:8-9
2
Mucc ga 25:2
«Waxal bànni Israayil ne leen, ñu indil ma ab saraxu njébbal. Ci képp ku am yéene ji, ngeen di jële li ñu may jébbal, indil ma ko.
Explore Mucc ga 25:2