1
Mucc ga 1:17
Kàddug Yàlla gi
KYG
Teewul rewlikat ya ragal Yàlla, ba defuñu la leen buur ba sant; xanaa ñu bàyyi liir yu góor ya, ñu dund.
Compare
Explore Mucc ga 1:17
2
Mucc ga 1:12
Terewul lu ñu leen gëna fitnaal, ñuy gën di fulandiwu, yokku, ba waa Misra am njàqare ca bànni Israyil.
Explore Mucc ga 1:12
3
Mucc ga 1:21
may leen giir ndax seenug ragal Yàlla.
Explore Mucc ga 1:21
4
Mucc ga 1:8
Ñu dem ba jëmmi jamono, beneen buur bu xamul Yuusufa falu ca Misra.
Explore Mucc ga 1:8
Home
Bible
Plans
Videos