1
Jëf ya 27:25
Kàddug Yàlla
KY
Kon nag, bokk yi, dalalleen seen xel, ndax gëm naa Yàlla, xam naa ne ni mu ko waxe, ni lay ame.
Compare
Explore Jëf ya 27:25
2
Jëf ya 27:23-24
Ndax malaakam Yàlla ji ma moom, te ma di ko jaamu, moo ma dikkal biig. Mu ne ma: “Póol, bul tiit; fàww nga taxawi fa kanam Sesaar, te it Yàlla moo la baaxe muccug mboolem ñi nga àndal ci gaal gi.”
Explore Jëf ya 27:23-24
3
Jëf ya 27:22
Léegi nag dama leen di ñaax, ngir ngeen dalal seen xel, ndax kenn ci yeen du ñàkk bakkanam, gaal gi rekk ay yàqu.
Explore Jëf ya 27:22