1
Jëf ya 16:31
Kàddug Yàlla
KY
Ñu ne ko: «Gëmal Sang Yeesu, daldi mucc, yaak sa waa kër.»
Compare
Explore Jëf ya 16:31
2
Jëf ya 16:25-26
Ba guddi gay xaaj, Póol ak Silas a ngay ñaan, di sàbbaal Yàlla, ñeneen ña ñu fa tëj di leen déglu. Ci kaw loolu suuf jekki yëngu yëngu bu mag ba fondmaa kaso ba di rëŋ-rëŋi; bunt yépp jekki ubbiku, jéngi ñépp dàjjiku.
Explore Jëf ya 16:25-26
3
Jëf ya 16:30
Gannaaw gi, mu génne leen ca biti ne leen: «Sang yi, ana lu ma wara def, ba mucc?»
Explore Jëf ya 16:30
4
Jëf ya 16:27-28
Boroom kaso ba tiite ciy nelaw, gis bunti kaso bi ubbiku. Mu bocci saamaram, nara xaru, yaakaar ne ña ñu tëj dañoo rëcc. Póol nag àddu ca kaw ne: «Bul lor sa bopp, nun ñépp a ngi fi.»
Explore Jëf ya 16:27-28