1
3.Yowaan 1:2
Kàddug Yàlla
KY
Soppe, yal nanga am jàmmi wet gu nekk. Ni nga ame jàmmu xol, yal nanga ni ame jàmmu yaram.
Compare
Explore 3.Yowaan 1:2
2
3.Yowaan 1:11
Sama soppe, bul roy lu bon, xanaa lu baax. Ñiy def lu baax ci Yàlla lañu bokk; ñiy def lu bon nag, dajewuñook Yàlla.
Explore 3.Yowaan 1:11
3
3.Yowaan 1:4
May dégg ne samay doom a ngi wéye dëgg gi, moomu mbég daal, awma mu ko raw.
Explore 3.Yowaan 1:4