1
2.Korent 10:5
Kàddug Yàlla
KY
mook lépp luy réy-réyloo ab taxawaayam, di joŋante ak xam-xamu Yàlla, te nooy jàpp njaam bépp xalaat, ngir déggalloo ko Almasi bi.
Compare
Explore 2.Korent 10:5
2
2.Korent 10:4
Ndaxte gànnaay yi nuy xeexe du gànnaayi suuxi neen, waaye da di gànnaay yu am fa Yàlla kàttanu daane ay tata. Te xalaatin yu jubul, noo leen di daaneel
Explore 2.Korent 10:4
3
2.Korent 10:3
Dëgg la, nitu suux lanu, waaye xeexewunu ni nit di xeexe.
Explore 2.Korent 10:3
4
2.Korent 10:18
Ndax ki ñu naw mooy ki Boroom bi gërëm, waaye du ki gërëm boppam.
Explore 2.Korent 10:18