Room 5:3-4
Room 5:3-4 TI
Te du ci loolu rekk, waaye bég nanu it ci sunuy nattu; ndax xam nanu ne nattu day feddali muñ; te muñ mooy ndeyu jikko ju dëgër; te jikko ju dëgër day jur yaakaar.