YouVersion Logo
Search Icon

Room 11:5-6

Room 11:5-6 TI

Noonu itam ci jamono ji nu nekk, des na nit ñu néew ñu Yàlla dencal boppam ciw yiwam. Gannaaw nag yiwu Yàlla rekk a tax mu denc leen, kon du seen peyug ñaq, walla boog yiwu Yàlla dootul yiw.

Free Reading Plans and Devotionals related to Room 11:5-6