Bible App logo
Search Icon

Peeñu ma 17:14

Peeñu ma 17:14 TI

Dinañu xare ak Gàtt bi, waaye Gàtt bi dina leen daan, ndaxte mooy Kilifag kilifa yi, di Buuru buur yi. Te am toppam, di ñi mu woo te tànn leen, te ñu takku ci moom, dinañu daanandoo ak moom.»

Free Reading Plans and Devotionals related to Peeñu ma 17:14