Peeñu ma 13:2
Peeñu ma 13:2 TI
Rab wa ma gis ma nga mel ni segg, tànk ya mel ni yu rab wu ñuy wax urs, gémmiñ ga mel ni gu gaynde. Ninkinànka ja jox ko kàttanam ak nguuram ak sañ-sañam bu réy.