Peeñu ma 13:16-17
Peeñu ma 13:16-17 TI
Mu def it ba ñépp, mag ak ndaw, buur ak baadoolo, gor ak jaam, ñépp am màndarga ci seen loxol ndijoor walla ci seen jë, ba kenn du mana jënd mbaa mu jaay te amul màndargam rab wi, maanaam turam walla siifar bu méngoo ak turam.





