Peeñu ma 13:11-12
Peeñu ma 13:11-12 TI
Noonu ma gis weneen rab di génn ci suuf. Am na ñaari béjjén yu mel ni yu gàtt, waaye di wax ni ninkinànka. Muy jëf ak sañ-sañu rab wu jëkk wa ci turam, di sant waa àddina sépp, ñu jaamu rab wu jëkk, woowu am gaañu-gaañu ba ko rey, waaye daldi wér.





