Peeñu ma 13:10
Peeñu ma 13:10 TI
Ku Yàlla dogal, ñu war laa jàpp njaam, dinañu la jàpp njaam. Ku Yàlla dogal, ñu war laa rey ak jaasi, dinañu la rey ak jaasi. Looloo tax gaayi Yàlla yi wara muñ te takku.