Bible App logo
Search Icon

Filib 2:9-11

Filib 2:9-11 TI

Moo tax Yàlla kaweel ko lool, jox ko tur wi tiim yépp, ngir turu Yeesoo tax ñépp sukk, ci asamaan, ci kaw suuf, ci biir suuf; te ñépp bokk genn kàddu naan: Yeesu Kirist mooy Boroom bi; ci màggug Yàlla Baay bi.

Free Reading Plans and Devotionals related to Filib 2:9-11