Bible App logo
Search Icon

Filib 2:12

Filib 2:12 TI

Noonu samay soppe, xam naa ne masuleena jóg ci dégg ndigal, waxuma sax bi ma nekkee ak yéen rekk, waaye rawatina bi ma leen soree. Kon nag maa ngi leen di ñaan, ngeen biral seen mucc ci seeni jëf, te def ko ci ragal Yàlla gu dëggu.

Video for Filib 2:12

Verse Images for Filib 2:12

Filib 2:12 - Noonu samay soppe, xam naa ne masuleena jóg ci dégg ndigal, waxuma sax bi ma nekkee ak yéen rekk, waaye rawatina bi ma leen soree. Kon nag maa ngi leen di ñaan, ngeen biral seen mucc ci seeni jëf, te def ko ci ragal Yàlla gu dëggu.Filib 2:12 - Noonu samay soppe, xam naa ne masuleena jóg ci dégg ndigal, waxuma sax bi ma nekkee ak yéen rekk, waaye rawatina bi ma leen soree. Kon nag maa ngi leen di ñaan, ngeen biral seen mucc ci seeni jëf, te def ko ci ragal Yàlla gu dëggu.

Free Reading Plans and Devotionals related to Filib 2:12