Luug 7:47-48
Luug 7:47-48 TI
Moo tax ma di la wax ne, su wonee mbëggeel gu réye nii, dafa fekk ñu baal ko bàkkaaram yu bare. Waaye ki mbëggeelam néew dafa fekk ñu baal ko lu tuuti.» Yeesu daldi ne jigéen ja: «Baal nañu la say bàkkaar.»