YouVersion Logo
Search Icon

Luug 2:10

Luug 2:10 TI

Waaye malaaka mi ne leen: «Buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xibaaru jàmm buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.

Verse Image for Luug 2:10

Luug 2:10 - Waaye malaaka mi ne leen: «Buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xibaaru jàmm buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.