Luug 14:34-35
Luug 14:34-35 TI
«Xam ngeen nag ne xorom lu baax la, waaye bu sàppee, nan lañu koy delloo cafkaam? Du jariñ suuf, te du nekk tos. Dañu koy sànni ca biti. Déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»