Yowaan 1:3-4
Yowaan 1:3-4 TI
Ci moom lañu sàkke lépp. Amul dara lu ñu sàkk lu jaarul ci moom. Ci moom la dund nekk, te dund googu mooy leeral nit ñi.