Yawut ya 9:14
Yawut ya 9:14 TI
Su fekkee ne noonu la deme nag, du kon deretu Kirist moo ëpp doole? Jox na bakkanam Yàlla, def ko sarax su amul sikk jaarale ko ci dooley Xel miy sax abadan. Kon deretam moo mana sellal sunu xel, mi nu doon yedd ndax jëf yu jëm ci dee, ngir nu mana jaamu Yàlla jiy dund.


![[Real Life] The True Vine Yawut ya 9:14 Téereb Injiil](/_next/image?url=https%3A%2F%2Fimageproxy.youversionapi.com%2Fhttps%3A%2F%2Fs3.amazonaws.com%2Fyvplans%2F16943%2F1440x810.jpg&w=3840&q=75)


