Bible App logo
Search Icon

Yawut ya 11:24-27

Yawut ya 11:24-27 TI

Ngëm a tax ba bi Musaa màggee, muy bañ ñu koy wooye sëtu Firawna. Bokk coono ak gaayi Yàlla yi moo ko gënaloon muy bànneexu ab diir ci bàkkaar. Ñu toroxal ko ngir Almasi bi, mi ngi mel ci moom ni alal ju ëpp alali Misra yépp, ndaxte yool bi la doon séentu. Ngëm moo tax mu jóge Misra te ragalul merum buur bi. Dafa muñ, mel ni nit kuy gis Yàlla, mi kenn manula teg bët.

Free Reading Plans and Devotionals related to Yawut ya 11:24-27