Galasi 5:17
Galasi 5:17 TI
Ndaxte sunu nafsu am na ay bëgg-bëgg yu méngoowul ak yu Xelum Yàlla. Te Xelum Yàlla itam am na ay bëgg-bëgg yu méngoowul ak yu sunu nafsu. Ñoom ñaar dañoo juuyoo ci bépp fànn, ba tax lépp lu ngeen bëggoona def, dungeen ko man.






