Bible App logo
Search Icon

Galasi 4:4-5

Galasi 4:4-5 TI

Waaye bi àpp bi Yàlla tëraloon matee, yónni na Doomam, mu juddoo ci jigéen, ci biir yoonu Musaa, ngir jot ñi yoon wi notoon, ndax Yàlla jàpp nu ni ay doomam.

Verse Image for Galasi 4:4-5

Galasi 4:4-5 - Waaye bi àpp bi Yàlla tëraloon matee, yónni na Doomam, mu juddoo ci jigéen, ci biir yoonu Musaa, ngir jot ñi yoon wi notoon, ndax Yàlla jàpp nu ni ay doomam.