Efes 3:20-21
Efes 3:20-21 TI
Léegi nag, na ndam li féete ak Yàlla, mi mana yeggale lépp luy ñaan mbaa yéene, ba weesu ko fuuf, dëppook kàttan giy jëf ci nun; moo yelloo ndamul mbooloom ñi gëm jamonoy jamono ba fàww, jaar ci Kirist Yeesu. Amiin.