Bible App logo
Search Icon

Kolos 2:9-10

Kolos 2:9-10 TI

Ndaxte ci Kirist, maanaam ci yaramu nitam, la matug Yàlla gépp dëkk, te mat ngeen ci moom, miy buuru kilifa yépp ak boroom sañ-sañ yépp.