YouVersion Logo
Search Icon

2.Korent 5:14

2.Korent 5:14 TI

Ndaxte mbëggeelu Kirist moo nuy jiite, ndax wóor na nu ne ndegam kenn rekk a dee ngir ñépp, kon ñépp a dee.

Verse Image for 2.Korent 5:14

2.Korent 5:14 - Ndaxte mbëggeelu Kirist moo nuy jiite, ndax wóor na nu ne ndegam kenn rekk a dee ngir ñépp, kon ñépp a dee.