2.Korent 1:6
2.Korent 1:6 TI
Su nuy jaar ci tiis, seen noflaay a tax ak seen mucc. Bu dee Yàlla dëfal na sunu xol, seen noflaay a tax, ngir ngeen mana dékku naqar yu mel ni yu nuy am, nun itam.