1.Timote 1:16
1.Timote 1:16 TI
Waaye Yàlla yërëm na ma, ngir Kirist Yeesu jëkka feeñal ci man muñam gu yaatu gi, ma nekk royukaay ci ñi ko nara gëm te am dund gu dul jeex.