1.Piyeer 1:24-25
1.Piyeer 1:24-25 TI
Ndaxte: «Nit ñax la, ndamam di tóor-tóor kese; ñax day wow, tóor-tóor ruus, waaye kàddug Boroom bi day sax ba fàww.» Te kàddu googu mooy xibaaru jàmm, bi ñu leen doon yégal.