Tit 3:9
Tit 3:9 KY
Waaye ay werante ak limi maam aki xuloo aki jaayante xam-xam ci yoonu Musaa, moytu ko, ndax loolu amul njariñ, amul solo.