Tit 3:1-2
Tit 3:1-2 KY
Fàttali leen ne leen ñu nangul kilifay nguur gi ak boroom sañ-sañ yi, di dégg ndigal tey fàggu ngir jépp jëf ju baax. Buñu yàq der te buñu bëggu ay, waaye nañu di bëggkati jàmm, te nañuy jëfe lewetaay gu mat sëkk seen digg ak ñépp.





