YouVersion Logo
Search Icon

Peeñu ma 6:5-6

Peeñu ma 6:5-6 KY

Ba mu tàyyee ñetteelu tayu bi, ma dégg ñetteelu mbindeef mi ne: «Dikkal!» Ma xool rekk, gis fas wu ñuul, gawaram yor ab màndaxekaay. Ma dégg lu mel ni baat bu jibe ci diggante ñeenti mbindeef yi, ne: «Benn kilo peppu bele, peyu bëccëgu lëmm; benn kilo peppu lors, peyu bëccëgu lëmm, te diw ak biiñ, bu ko kenn yàq.»

Free Reading Plans and Devotionals related to Peeñu ma 6:5-6