Peeñu ma 6:2
Peeñu ma 6:2 KY
Ma xool rekk, gis fas wu weex, gawaram yor ag fitt. Ñu jox ko kaala, mu daldi aw ci yoonu daan-kat, ngir daani.