YouVersion Logo
Search Icon

Peeñu ma 6:10-11

Peeñu ma 6:10-11 KY

Ñu àddu ca kaw ne: «Buur bu sell, bu dëggu bi, loo deeti xaar ci àtte waa àddina, ngir feyul nu sunu deret ji tuuru?» Ñu jox ku ci nekk mbubb mu weex, ne leen ñu négandiku tuuti, ba kera seeni bokk ak ñi ñu bokkal liggéey bi, te ñu war leena bóom ni ñoom, ñépp dikk, ba lim bi mat.

Free Reading Plans and Devotionals related to Peeñu ma 6:10-11