Peeñu ma 17:14
Peeñu ma 17:14 KY
Dinañu xare ak Xar mi, waaye Xar mee leen di daan, ndax mooy Sangu sang yi, di Buuru buur yi. Mooy daan mook ñoñam ñi mu woo, tànn leen te ñu saxoo topp ko.»