Peeñu ma 16:12
Peeñu ma 16:12 KY
Juróom benneelu malaaka mi sotti ndabam ci dex gu mag gi ñuy wax Efraat, dex gi daldi ŋiis, ngir sàkkal buuri penku yiy dikk aw yoon.