Peeñu ma 14:8
Peeñu ma 14:8 KY
Meneen malaaka topp ci, di ñaareel bi. Mu ne: «Babilon a daanoo, dëkk bu mag ba daanu na! Moom ma daan màndal askanoo askan biiñu moyam miy indi am sànj.»