Peeñu ma 14:7
Peeñu ma 14:7 KY
Ma ngay àddu ca kaw, naan: «Ragalleen Yàlla te màggal ko, ndax waxtuw àtteem jot na. Kon nag jaamuleen ki sàkk asamaan ak suuf ak géej ak bëti ndox yi.»