Màndiŋ ma 14:6-7
Màndiŋ ma 14:6-7 KY
Yosuwe doomu Nuun, ak Kaleb doomu Yefune, ñoom ña bokk ca ña seeti woon réew ma, daldi xotti seeni yére ndaxu tiis. Ñu wax nag mbooloom bànni Israayil mépp, ne leen: «Réew ma nu wëri woon, ba nemmiku ko, réew mu baaxa baax la.





