Màndiŋ ma 14:2
Màndiŋ ma 14:2 KY
Bànni Israayil gépp nag di ñaxtu ci kaw Musaa ak Aaróona, mbooloo ma mépp naa leen: «Waay lu nu tee woona dee ca réewum Misra, mbaa sax nu dee ci màndiŋ mii!