Màrk 7:15-16
Màrk 7:15-16 KY
Mboolem lu bokkul ci nit ki, du lenn lu ciy dugg ci moom, ba man koo sobeel. Liy génne ci nit ki kay mooy sobeel nit ki.»