YouVersion Logo
Search Icon

Màrk 12:43-44

Màrk 12:43-44 KY

Yeesu nag woo taalibe ya, ne leen: «Maa leen ko wax déy, mboolem ñi sànni xaalis ci ndab li, jëtun bu néew doole bii moo leen ëpple lu mu ci sànni. Ndax ñoom ñépp ci seen koom lañu sàkke as lëf, sànni ci ndab li, waaye moom de, ci biirug ndóolam la jële la mu amoon lépp, dundam bépp, sànni ci.»