YouVersion Logo
Search Icon

Màrk 11:17

Màrk 11:17 KY

Mu di leen jàngal nag, wax leen, ne leen: «Xanaa bindeesul ne: “Sama kër gi, kërug ñaan lees ko tudde, ñeel xeetoo xeet.” Waaye yeen, moom ngeen def rawtub sàcc.»

Video for Màrk 11:17

Verse Image for Màrk 11:17

Màrk 11:17 - Mu di leen jàngal nag, wax leen, ne leen: «Xanaa bindeesul ne:
“Sama kër gi, kërug ñaan lees ko tudde,
ñeel xeetoo xeet.”
Waaye yeen, moom ngeen def rawtub sàcc.»