Macë 24:9-11
Macë 24:9-11 KY
Bu boobaa dees na leen teg ciy loxo, ngir ñu mitital leen, rey leen; mbañeel la leen xeet yépp di won ndax sama tur. Ca la ñu bare di xàcc, di worante aka bañante. Te itam yonenti caaxaan yu bareey feeñ, di nax ñu bare.