YouVersion Logo
Search Icon

Macë 24:7-8

Macë 24:7-8 KY

Aw xeet dina jógal aw xeet, am réew jógal am réew. Ay xiif ak yëngu-yënguy suuf dina dikke fu bare. Waaye loolu lépp ndoortel mititu mat lay doon.

Free Reading Plans and Devotionals related to Macë 24:7-8