Macë 24:37-39
Macë 24:37-39 KY
Na woon ca jamonoy Nóoyin, noonu lay deme, bu Doomu nit ki di feeñ. Ndaxte jant ya jiitu mbënn ma, nit ñaa nga doon lekk aka naan, di takk aka maye jabar, ba bés ba Nóoyin duggee ca gaal ga. Yéguñu woon dara, ba kera mbënn ma dikk, buub ñépp. Noonu doŋŋ lay deme bu Doomu nit ki feeñee.





