Macë 23:25
Macë 23:25 KY
«Wóoy ngalla yeen firikati yoon yi ak Farisen yi, jinigalkat yi! Yeenay raxas bitib kaas bi, ak ndab li, feek li fees kaas baa ngi jóge ci càcc ak ŋàppaaral.