Luug 7:47-48
Luug 7:47-48 KY
Moo tax ma di la wax, ne bàkkaaram yu bare yi ñu ko jéggal moo waral fonkeelam gu bare. Waaye njéggal lu tuut, fonkeel gu tuut rekk.» Yeesu nag ne ndaw sa: «Jéggalees na la say bàkkaar.»