Bible App logo
Search Icon

Luug 22:20

Luug 22:20 KY

Kaas ba itam noonu la def ak moom gannaaw reer ba, ne leen: «Kaas bii mooy kóllëre gu yees gi fasoo ci sama deret ji nara tuuru ngir yeen.

Video for Luug 22:20

Verse Image for Luug 22:20

Luug 22:20 - Kaas ba itam noonu la def ak moom gannaaw reer ba, ne leen: «Kaas bii mooy kóllëre gu yees gi fasoo ci sama deret ji nara tuuru ngir yeen.

Free Reading Plans and Devotionals related to Luug 22:20