Luug 17:26-27
Luug 17:26-27 KY
«Noonee mu deme woon ca jamonoy Nóoyin, ni lay deme ca jamonoy Doomu nit ki. Nit ñaa nga doon lekk aka naan, di jël jabar aka séyi, ba keroog bés ba Nóoyin duggee ca gaal ga, mbënn ma dikk, sànk ñépp.